mes Cheveux crépus, ma peau noire, =mon identité, non aux perruques de cheveux lisses, nous ne sommes ni indiennes, ni sri lankaises, soyons fières de nous mêmes. Nous sommes les seules à copier les autres, quelle tristesse!!!
N'envoyez pas de message ayant un ton agressif
ou insultant.
N'envoyez pas de message inutile.
Pas de messages répétitifs, ou de hors sujéts.
Attaques
personnelles. Vous pouvez critiquer une
idée, mais pas d'attaques personnelles
SVP. Ceci inclut tout message à contenu
diffamatoire, vulgaire, violent, ne respectant
pas la vie privée, sexuel ou en violation
avec la loi. Ces messages seront supprimés. --
Pas de publicité. Ce forum
n'est pas un espace publicitaire gratuit.
Pas
de majuscules. Tout message inscrit entièrement
en majuscule sera supprimé.
2 Commentaires
Loutax
En Juillet, 2021 (16:49 PM)Hé!
En Juillet, 2021 (17:20 PM)Diko sédèle loudoul jikome
Bagne nitt ki warteu takh ngakay toumal
Di ka wakhal loumou défoul
Ame na gno khamni toumal nagn lène ba réy lène
Gni gnou toumal lène ba sank lène. Moo néh
Défougnou yégougnou li khew
Dagn lène sossal ci lougnou défoul (à vérifier)
Domou Adama'k daraja baka Yala bindé
Domou Adama'k martabal baka Yala bindé
Domou Adama'k nimou foré ca Yala
Warna jeumb wakh, bay soss lou nékoul
Aaaaaannn, mane deh santt na
Beugue na, nitt kou ragal Yala tay wakh louko woore
Gniak kham di wakh
Kignane gui and ak pékhé
Fa Yala'y déféré nitt meunou fa yégue bay yakh
Garab gou wara done peinthie tek ko beut
Ba gorr ko mo jaffé (à vérifier)
Kou Yala bakhé nga wara bakh
Kène meunoula bonal abbadan
Bou doone lou way yéné nitt mou dal ko
Ma tambalé jooy sama bopp ndakh samay noones
Deugg la vérité nagnou deuggou tay wakh deugg
Toolouwayou diamono metti metti yi gnouy jankontel
Kéneuh kouné sa sokhla warnala doy wakh
Assane Mboup - Djignaté
Du courage Wally Seck
RIP Pr Oumar Sankharé, Thione B Seck et Juge Samba Sall
Participer à la Discussion